Описание
Mbootaayug WAX , kurel la gu jóg ngir taxawu làkku Wolof, sotti ci ay xam-xam , bind ci ay téere. Yéegal ko ci lënd , yóbb ko fépp fu làkk yu mag yi àgg.
L'association WAX est une association qui œuvre pour une mise en valeur de langue Wolof par la traduction des sciences, la rédaction d'œuvres, la vulgarisation à travers l'internet pour faire du wolof une langue internationale.
WAX is an organization with the objective of advancing the Wolof language by the means of translating all type of knowledge, publishing documents, books and teaching the language. It's aim is that of digitizing the Wolof language so that it is supported wherever world languages are.